MENU (C)

Ngaaka Blinde - Effect Secondaire 「Paroles」

Asslam walikum akhlou clash
Khamna ni namone ngene meu
Douma maye 24h ci ay pique
You know kind baba

#chipshop #lyrics #sanderlei #TikTok #REMIX


Ngaaka Blinde - Effect Secondaire 「Paroles」

Asslam walikum akhlou clash
Khamna ni namone ngene meu
Douma maye 24h ci ay pique
You know kind baba
Bo Lene ladione senn papa do
Danane lene ndiaga balniou

Li nak moy togn kou wereudi
Ladj Len ko ndiaga Mbaye
Niari diankeu yoyou
Ki di youtt kenene ki di taliif
Yolk dole teksi dounk bou xess
Kokoy Keita Salif



Waw loutakh boulen gars yi di clash rek
nane lenn goor djiguen bon
arrete de faire genre
pourtant ils sont mignons han
comme niom Aida séne
nane meuneu khifou
wakhouniou classe téh nio bok cours say talibé bayi naniou dieul lenn game bi yob ko gamou Kaolack

Mane nak je m’en fou ci rafet dioudou koudeug no toudou
kou sagua king sagua nga sa papa sama baat ci kaw nak bo guénè neguu goor dougeul sa neguu maam ndakh bo dougué sa neguu… mane sa papa ngafay tassel

VIP Paroles By Aya Nakamura
Affaire yoyou day def effect sama affairou bandit yoyou day


def effect kholal ni lagn koy féthiê daguay bayi sa njari tank dokh niou tasse
(bis)

Anh ko có dòng iwana mana
soppi la thia burubara
senn papa la danioul doul
niom douniou dara
kouma diégué kouma niémè dageu na sa nurunara
nurunara bigua dalé fé
doug roukou kagna

Meune na bi neen
bissap bou saff dionking fou lawbé né indalel ma bine bine mbélélétè bi lé dafa bari naniou dokh niou dadjié founiou dadjié tay niouné hey daniou moudiou teulé founiou teulé té fouma teuulé
Senn bissou deudţe cut



limoy ndiabou niankou think thiak
mane khale douma yabb
sakou mak maak
nio meuné yapeu rayla ray naak so amé loy diangeu diay ko wa fac
doul
ana senn camaro yi voom voom voom voom
doul

Die Paroles By Gazo
boy yagui nianat pots yi
voom voom voom voom
mane mane pour mane camaro yi barki Yallah yêneu ko mom
tass ngenn yakaru game bi


tass yakaru boys yi
am ngenn ay millions
nak wayé ci vue yi la yam

Gni nio meuneu doul

bo guéně neguu goor
dougeul sa neguu maam
ndakh bo dougué sa neguu… mane sa papa ngafay tassel Affaire yoyou day def effect
sama affairou bandit yoyou
day def effect
kholal ni lagn koy fêthie
daguay bayi sa njari tank
dokh niou tasse (bis)




YouTube - TOP 50

#sanderlei